Hadiia

Lyrics: Erwan Delgado Music: Erwan Delgado Bëgouma ko Mënouma ko Xol la di dem sans ma wakh lë ko Sama xol sou fekhe ya fi ne Yow rek la beug kay ñu nobante Yay sama xarit Yay sama life Yay sama adineu sama jambaar Bëgouma ko Mënouma ko Xol la di dem sans ma wakh lë ko
Jëm ak jëm Xol ak xol Bët ak bët Nga mey xool Te gisuloooma
gisagoooooma
Lamb daj Seet ba giss Ci Yaw laa daj, tey Man yow laa giss
Xalaat bu ne nga nekk ci Lu ma mënti romb yow la mey fattali yaakar bës nga mën maa giss
Bëgouma ko Mënouma ko Xol la di dem sans ma wakh lë ko Sama xol sou fekhe ya fi ne Yow rek la beug kay ñu nobante Yay sama xarit Yay sama life Yay sama adineu sama jambaar Bëgouma ko Mënouma ko Xol la di dem sans ma wakh lë ko