Lyrics: Mouhamadou Bamba Diaw
Music: Mouhamadou Bamba Diaw
Jambaar ( wolof Sénégal )
intro
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Couplet :
Jambaar dawul dafa daani doolee.
Jambaar dawul dafa daani doolee.
Jambaar dawul dafa daani doolee yaye
Dembeu metiwoon na, dembeu metiwoon na, dembeu metiwoon na
Ci sunuy maam mamaati maam.
Dañoo dieul sunuy maam yobuleen def leen niome ay jaam
Tewul niu dounde yaguefe ba niune niu doon tay lii niu doon.
Jambaar dawul dafa daani doolee
Refrain :
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Couplet :
Fonkal ligua doon te boul meussa bayii sa yoon
Niakka gueum sa bopp, wésuwul bagna feussal kii gua doon
Sama der bu ñuul bi ñuul ba mel ni keuriñ moom laay titeurô moom lay ndamoo
Sama der bu ñuul bi ñuul ba mel ni keuriñ moom laay titeurô moom lay ndamoo
Sama der bu ñuul bi ñuul ba mel ni keuriñ moom laay titeurô moom lay ndamoo
Ayeeeeeee, Wo wo wo waaahaaa
Refrain:
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
Jambaar Jambaar Jambaar Jambaar
--------------------
Jambaar (French Traduction)
Intro:
Guerrier, Guerrier, Guerrier, Guerrier
Couplet:
le courageux n'abdique pas mais démène pour honorer ses droits et devoirs.
le courageux n'abdique pas mais démène pour honorer ses droits et devoirs
e courageux n'abdique pas mais démène pour honorer ses droits et devoirs
Hier c'était dur , hier c'était dur, hier c'était dur.
Nos ancêtres ont souffert, réduits en esclaves. Cela n'a pas empêché la continuité du peuple noir Et nous voici en dignes descendants fiers de ce que nous sommes devenus.
Est indigne celui qui se renie ou bien qui
n'est pas fier de son humanité
Refrains
Guerrier, guerrier, guerrier guerrier
Guerrier, guerrier, guerrier, guerrier
Couplet
Aie confiance en toi et suis ton chemin qui te mène vers le succès.
Moi qui suis noir comme la couleur du charbon,
j'en suis fier pour la diversité que je représente.
Moi qui suis noir comme la couleur du charbon,
j'en suis fier pour la diversité que je représente.
Moi qui suis noir comme la couleur du charbon,
j'en suis fier pour la diversité que je
représente.
Ayeeeeeeeeeeee,, Ho ho ho, hoo waaaa
Refrains
Guerrier, guerrier, guerrier, Guerrier
Guerrier, guerrier, guerrier, Guerrier
Guerrier, guerrier, guerrier, Guerrier
Guerrier, guerrier, guerrier, Guerrier