yaw la (to the chosen person)

Lyrics: Papa Alassane Diaw Gaye Music: Papa Alassane Diaw Gaye/Saliou Dieng Nangou naa ni iow la dou done kenene bae Ki gueune si mane khol bi iow la taneu Nangou naa ni iow la defma loula nekh bae Wolou nala foma wo ma wouyou laa Nangou na ni iow la doune kenene bae Ki gueune si mane khol bi iow la taneu Nangou naa ni iow la defma loula nekh bae Nema kaay , kaay way kaay
Meunoumala promettre bidew yi Faaw ma waxtaan ci ak weer wi Doumala setane nguay khouss si guew gui te teyewouma si sa lokho ndakh iow ,* yaw yaw yaw iow la taneu ak sa retane mane iow ioe la taneu ak sa waxtaan samay dƩfauts indi khoulo mais dioubo laniouy moudie amoul lou ndourok sa djiko yonei gouro laye moudie nema kaay waay legui ma yonei si saa baaye cherie yaye bagne tane nala te dou meusseu deigne ndakh
Mbeuguel capitainou boromame Foume la fek dalay dane Yako ndieukei fathie samay gaumou khol Baby meussouloma gaagne Yaye kima kham mane xol bi yaw la tipooooo
Yama tane nangou samay defauts Gueumeul douma nangou nguamay bokoy keineine Cherie dekloul ma dei la Signe monogamie Amoul nafi mba ami iow keissei Siguil deima rei dangua rafete yaw tamite Diokh nguama limay lathie Te waxoumala dara Ya jongue Fo xalaat yobou ma boul teye sa lokho fofou laaa