Lyrics: Papa Alassane Diaw Gaye
Music: Papa Alassane Diaw Gaye/Saliou Dieng/Henry Marone
Xamnga ma
dama sikk waye yama yaar
Togn nala
dina sukk tay balou la
Ndax lernama
bofi diougue dara du demm babe
Yaw rek la love
aduna bi sedde nako
I use to talk to you
And you are the only thing in my life babe
You use to talk to me
And you will never let me down
So togal niou waxtaan bala mouy wess
Sett na sett waye
Meunou maa dundak koudoul yaw mi
Waxnala
Yaye diante guiy leral sama life
Xamnguama
Kaay togal fi ma waxla baby
bayil bayil
Nono dufi yam
Bayil bayi baby ninguay def
Waxma fo beug dem
bayil bayil
Nono dufi yam
Bayil bayi baby ninguay def
Waxma fo beug dem
Baby bayil li way
Sett na ba seet
Bayil li way
Meunouma dundak kudul yaw oh yeah
And you will never let me down
So togal niou waxtaan bala mouy wess
Sett na sett waye
Meunou maa dundak koudoul yaw mi
Waxnala
Yaye diante guiy leral sama life
Xamnguama
Kaay togal fi ma waxla baby
bayil bayil
Nono dufi yam
Bayil bayi baby ninguay def
Waxma fo beug dem
bayil bayil
Nono dufi yam
Bayil bayi baby ninguay def
Waxma fo beug dem