Lyrics: Papa Alassane Diaw Gaye
Music: Papa Alassane Diaw Gaye/Saliou Dieng/Marie-Kell de Cannart
Taarou ngua ningua mel boul gnei keine
Sa beaute naturelle moy sa dole
Diadou ngua ningua mel doleine bene
Lingua ame boul ko fowei
Coz you are beutifull
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou
Ouhouhou yaa taarou
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou hoou
Ouhouhou yaa taarou
Sa Setou nakhou la waaw
Guenal te niemeko fi amoul keine
koufi niaaw
Ningua rafete khamoko
Dieumeuleul sa taar ndaax beugue sa boopay
gueume sa boop
yaw dangua rafete te khamoko
dieumeuleul sa taar ndakh societe bi mola sonal doome
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou
Ouhouhou yaa taarou
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou hoou
Ouhouhou yaa taarou
Santal nature bi si limla may
Lila yalla may nala doy waaw
Dekloul ma waxla hey
You are so beautiful the way you are
No matter who you are
You are so beautiful the way you are
No matter how you are
Taarou ngua ningua mel boul gnei keine
Sa beaute naturelle moy sa dole
Diadou ngua ningua mel doleine bene
Lingua ame boul ko fowei
Coz you are beutifull
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou
Ouhouhou yaa taarou
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou hoou
Ouhouhou yaa taarou
Yaa Taarouuuuuuhouhouhou hoou
Ouhouhou yaa taarou