Lyrics: Babacar Dieng
Music: Babacar Dieng
Ay kilos thieuz si sama poche ak tonnou job sama bop
Ma diok Defier life bi miser tank yi dey dokh
Hosslumane comme oumar ndiaye mais différence bi mak moom
Sumay waxtane pr guene doe leu mais dou awa la nop
Ok
meun na yewou def albumou soul
Ay carriere
Ak ay full envi you flou
Mais envié woumaleine
Careler game bi noir et blanc
mc’s yi virer transgenre
Khamugn ni doug dame taxuleu gagner damier
Tall bu teuweu takk boy funé lagn kou eupé
Buntu tekki bu teuweu tidjekou funé legn koy feugué
Su gnidi feul gné di felalé fi kunek fingay feulé
Mais best rapper du centenaire dou fouleu nekh ngakoy foré
Mangui teunguedj
Di yè ay boy yu dè
Ay boy yu niak boom may wax pr niu bagn niak thieel
Kou systeme bi yakh bopam dou faalè kouy yakh derr
Boie yi dè laniu tann choix bilene dund meusta hagn
Holdup there was a time i was young and weak
I still wanna be forever young but awake
Free are dreams dont waste all of ur time in that thing
But making them true that shit can cost an arm and a leg
Kharit dina la wax lou ioe sa bopp khamoul sa bopp
Samal bop di door di gorr di goop
Ndax diomak ngoray moy natal tolou goor
Boul Tegui si tank ndax ragal défendre sa pose
Imbecile moy agir sans mou khalate les conséquences dabord
Xolal Russ dou ragal tey dou beuri titeur
Mano tite ba rew ki ay guentam soupekou fitnam
Mano wett ba raw ki took ci chaisou boor khoulok nieup
Kene dou new dolè ba raw kign tiim di sotti souf si negam !
Kouy rendi di gessu si rendi baram la dieum
Mano niak guemm sa bopp beug nio wax liniouy guem
Magg si khel si ioe la dess meloul kom mag si dieum
amone na espoir si rap mais avant tank yimou dieul
Comme que bagn dou té li wara am am
Kone meun dou té sakou dji xam xam
Victoire yi reka ni fang
mais echec reka fess si yonou gni am ndam
Broda
Ak lou mou metti metti
Ndam li ndam li daniukoy dieul
Faw niu takk dall yi dokh ba foum niou fekk niu heum
Bo demé bay niak raison de vivre togal
Togal halate yenè bila sa yaye yenè nga dundeu
Loula farata hagn manoko tek si sunna
Assumel sa choix Yi bul dund ba dé
di tegui toumeu
Dieuf dou nul kone fekhel niakh gagnè sa koom
Boy Beug teki si teel bum takh nga takanteek lou bone
Ba mudj si
Def lo waral def
Ndax nek fo warul nek
Si lima nek sou wesso sama bop kane laciy rayantel
Dokhuma ci and di fenanté tago di lekantè
lima guem ak sama salaire louma ciy def douma ko werantè
Boy
Diap lou bess seu gueun yomb bayi lo mine
Kone mineul lou diara japp ndax bayi da meusseu triste
Souroukh si routine bu leumdeum cris
Doublé samay vices
terewouma di niane bayi mbectèy souf yi diap si kignou tiim
Si rew bu dix di gagnè carte
Ndiarignu as bi lay ladj
Bul yakar dara si life bo massul diokh limuy laadj
Soy bind pr gnilay deglou bindeul ndiarign cest la base
Dou nieup nio meuneu lire
Mais nieup meun tourner la page (bis)
It’s Legendary
20.000hz cest la limite
Rappeur kaamil