Lii Tamite

Lyrics: Cheikh Gaye Music: Cheikh Gaye/Amet Thiam Ci bamouy mom Ci Bamouy mom Ci Bamouy mom
Doumala meussa bayi Dila weur douma taayi Doumala meussa Trahir (ci lay dé)
Ci Bamouy mom Doumala meussa bayi Dila weur douma taayi Doumala meussa Trahir (ca bamouy mom) ci lay dé(ci bamouy mom)
Tokk nga ci ngeum guonĂ© gorĂ© nga Not la ci mougne guonĂ© kharĂ© nga Like founiou dieum wanĂ© ngassi diom Diom biniou am moniou tĂ©rĂ© seungĂȘm
No yomboul woon diayanté nga Tei diomboula woon diaré fa Téwoul ngani woon Baye fall Mounialo dina baakh
Khamna deggoulo wakhou noon yi Faléwoulo wakhou noon yi Niom nioungui thiow douniou tei niou fly(flyyyyyyyi)
Tamounala taneu la beugue naala(flyyyyyi) Tamounala ngir nga doon sama waay(flyyyyyyi x2)
Doumala meussa bayi Dila weur douma taayi Doumala meussa Trahir (ci lay dé)
Ci Bamouy mom Doumala meussa bayi (ci bamouy mom) Dila weur douma taayi (ci bamouy mom) Doumala meussa Trahir (ci bamouy mom) ci lay dé(ci bamouy mom)
Fa yallah di bolĂ© fofou lala tipowĂȘ (yehii yehhh) Fa yallah di bolĂ© fofou lala tamonei nobb naalaaa Sama khel nakhouma (nakhouma) Bae Djiko djing’ma waan doyouma (bae doy nama) Ninga mel nekh namaa yeaaahh Yamay tĂ©tĂ© yamay saggal
Souy Fooo ngani mo geunn Freedom lay wooté Fi doolaay nobéll Sa mbeuguél gui day dauré
Mo geun Mom lay woté(wawwww waw) Ci doley mbeuguél moma diakhal daal
Doumala meussa bayi Dila weur douma taayi Doumala meussa Trahir (ci lay dé)
Ci Bamouy mom Doumala meussa bayi (ci bamouy mom) Dila weur douma taayi (ci bamouy mom) Doumala meussa Trahir (ci bamouy mom) ci lay dé(ci bamouy mom)
So beugué ma fethial laa Dila wayal xaalam yelaa
Khana dou may KHALÉ FÉROCE Bo beuguĂ© ma fethial la Diko nday raabinn goumbĂ© wala ngeross
Khana dou may KHALÉ FÉROCE
GuintĂ© tĂ©rappi Fethial GuintĂ© tĂ©rappi Ma diebalou danounaaa(salatounana Khana dou may KHALÉ FÉROCE)
Ci dolay mbeuguĂ©l moma diakhaal daalĂȘ Ni dolay mbeuguĂ©l moma diakhal daal (Khana dou may KHALÉ FÉROCE Ci dolay mbeuguĂ©l moma diakhaal daalĂȘ (moma diakhal moma diakhaal daal)