Champion

Music: Bril Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss Champion nga fils Bakoul reik maay guiss Champion deug nga fils
Mane beurrei na walahi beurrei na Mane beurrei na beurrei na beurrei douma danou Entraîné na entraîné na entraîné na aiguisé sama mind
Dou xool be nieuk fatélikou demb nimou meitei wone waral ma xaali yonne beugeu done champion
Ñi né meune nako deef ñi né meunuta baax Saalo ligueey ak ngeum ñanou wadiour mooy Sama dolé I don’t care Balla waxal douma terrei deef Xarañe na ba nieup nangou maay modou si biir Gueew
Wayè yallah baxna ioe yallah bakh nga mousseul ma mane si samay pekheem noon Bayi ma ak Sama xeel ma meuneu agaalé mbeubeut mi nè si mane Ndax champion laay meusseu done
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss Champion nga fils Bakoul reik maay guiss Champion deug nga fils
Sky is the limit on a plus rien à prouver Baal ba taak na bideew bou diougué assamane Kouy waax bokoul ak kouy dieuf mane damay beurrée daane Dolé gaindé ndiaye doma degeul ndeysane
Xamè na diandj ak dior xamè thiamoñe ndey dior Todj na lamb ndakaru thies kay diap siki thior Kaay waay mane beurrei daan laay guiss
Geum geum bi dotoul deign ba Abadane daiman Sakou na ñane Kou faraal jeeba neko ya meune Wayé Yallah bakhna ioe Yallah bakhnga mousseul ma mane Simay pekheem noone Bayima mane ak sama xeel ma meuneu agalé mbebeut bi né Si mane ndax champion laay meusseu done
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss Champion nga fils Bakoul reik maay guiss Champion deug nga fils
Kone diot na Taay ma magg foutekou beurré daan God mayma Ndam dotouma trainée ioe
Yennay diokhogn maay dagg am am bou sawaan bawaan Thiono adouna dotouma terrei nelow
Bakoul reik maay guiss Champion nga fils Bakoul reik maay guiss Champion deug nga fils
Hé jeeba le boy Hé jeeba le boy Hé hè jeeba le boy jeeba le boy jeeba le boy