Thibatou

Lyrics: YoungZize Music: Sapfire beat Yëwu Bëgg Dolli Sante Sama Dundu Doma Khamal Dara Sama Tundu Wumuy Wundu
Khol bagui Nekh Seed Ni Pôle Nord Mané Dawal Bokatou Outal Si koy Sakétou
Nakh Fo romb Gnu Thibatu Thi Batou Lo Wax Gnu Thibatu Hey Thi Batou Fo né Gnu Thibatu Thi Batou
So Ré Gnu Thibatu Dagno tema Kebetou Kenne si gnom amussi Goût
Toukh leuh ni Outlaws Oie la Cendru 2pac Baby Damlay Dioylo Numkoy défé dafa hot
Sama Nder Bi ngay Yak Lossi Yok Doni Kagna Ayy Wayy Yallah mignu Sak Daga Bagne ma beug Bama
Deug La Kay Dama Soff Meune Nga Vue samay Toph Mangui Fane ak Samay Doff Trii Double Louki Dokh
Gua Beug Beug Bagne Nigga Fugnu Dugou Todj Ko Lo Gnu Meuneuh Khâgne Diaye Gnu Fébar rk Gnu Fadj ko :m Yëwu Bëgg Dolli Sante Sama Dundu Doma Khamal Dara Sama Tundu Wumuy Wundu